Showing posts with label WOLOF: Wolof Bible NT (WBNT). Show all posts
Showing posts with label WOLOF: Wolof Bible NT (WBNT). Show all posts

Thursday, September 15, 2011

Philippians 2:10-11 WOLOF: Wolof Bible NT (WBNT)

Philippians 2:10-11
WOLOF: Wolof Bible NT (WBNT)
10 ngir turu Yeesoo tax ñépp sukk,ci asamaan, ci kaw suuf, ci biir suuf;
11 te ñépp bokk genn kàddu naan:Yeesu Kirist mooy Boroom bi;ci màggug Yàlla Baay bi.